An-Najm · 10/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
فَأَوْحَىٰ إِلَىٰ عَبْدِهِ مَا أَوْحَىٰ ۝١٠
Fa awhaaa ilaa `abdihee maaa awhaa
📖 Tekkim Wolof
(Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore An-Najm

8ثُمَّ دَنَا فَتَدَلَّىٰ
Daldi nay jegeñ ba faf yoore,
9فَكَانَ قَابَ قَوْسَيْنِ أَوْ أَدْنَىٰ
Moo ngi jege woon ni ñaari xocci xala, walla sax mu gën a jigeñ loolu
10فَأَوْحَىٰ إِلَىٰ عَبْدِهِ مَا أَوْحَىٰ
(Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.
11مَا كَذَبَ الْفُؤَادُ مَا رَأَىٰ
Xol ba weddiwul la mu gis.
12أَفَتُمَارُونَهُ عَلَىٰ مَا يَرَىٰ
Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu gisoon ?
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — An-Najm 10

Simoore An-Najm Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.

Simoore Aaya 10/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers