An-Najm · 11/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
مَا كَذَبَ الْفُؤَادُ مَا رَأَىٰ ۝١١
Maa kazabal fu`aadu maa ra aa
📖 Tekkim Wolof
Xol ba weddiwul la mu gis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore An-Najm

9فَكَانَ قَابَ قَوْسَيْنِ أَوْ أَدْنَىٰ
Moo ngi jege woon ni ñaari xocci xala, walla sax mu gën a jigeñ loolu
10فَأَوْحَىٰ إِلَىٰ عَبْدِهِ مَا أَوْحَىٰ
(Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.
11مَا كَذَبَ الْفُؤَادُ مَا رَأَىٰ
Xol ba weddiwul la mu gis.
12أَفَتُمَارُونَهُ عَلَىٰ مَا يَرَىٰ
Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu gisoon ?
13وَلَقَدْ رَآهُ نَزْلَةً أُخْرَىٰ
Moo ne gisoon na ko de, ca geneen wàcc,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — An-Najm 11

Simoore An-Najm Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xol ba weddiwul la mu gis.

Simoore Aaya 11/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers