An-Najm · 46/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
مِن نُّطْفَةٍ إِذَا تُمْنَىٰ ۝٤٦
Min nutfatin izaa tumnaa
📖 Tekkim Wolof
muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore An-Najm

44وَأَنَّهُ هُوَ أَمَاتَ وَأَحْيَا
te it moom Mooy rey mooy dekkal,
45وَأَنَّهُ خَلَقَ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ
te moom Moo bind ñaari tóolent , yu di góor ak jigéen,
46مِن نُّطْفَةٍ إِذَا تُمْنَىٰ
muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay
47وَأَنَّ عَلَيْهِ النَّشْأَةَ الْأُخْرَىٰ
moom moo waral it sosuwaat ga dekkiwaat,
48وَأَنَّهُ هُوَ أَغْنَىٰ وَأَقْنَىٰ
te moom Mooy woomalale.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — An-Najm 46

Simoore An-Najm Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay

Simoore Aaya 46/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers