Al-Waqi'a · 49/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
قُلْ إِنَّ الْأَوَّلِينَ وَالْآخِرِينَ ٤٩
Transliteration
Qul innal awwaleena wal aakhireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Mbooleem ña jëkkoon ak ñu mujj ñi
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 47-51 — Al-Waqi'a
47وَكَانُوا يَقُولُونَ أَئِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
dañu daan wax naan : “ Moo ndax bu nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkilaat ?
48أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
nook sunuy baay ak i maam ?...”
49قُلْ إِنَّ الْأَوَّلِينَ وَالْآخِرِينَ
Waxal ne : “Mbooleem ña jëkkoon ak ñu mujj ñi
50لَمَجْمُوعُونَ إِلَىٰ مِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
dees na leen dajale ci féncóob bis bu ñu xam”.
51ثُمَّ إِنَّكُمْ أَيُّهَا الضَّالُّونَ الْمُكَذِّبُونَ
Topp ginnaaw ba, yéen, ñi réeroon, te daan waddi (bis pénc ba),
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
49Aaya
Tekki — Al-Waqi'a 49
Simoore Al-Waqi'a Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Mbooleem ña jëkkoon ak ñu mujj ñiSimoore Aaya 49/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








