Al-Waqi'a · 62/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ ۝٦٢
Wa laqad `alimtumun nash atal oolaa falaw laa tazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Simoore Al-Waqi'a

60نَحْنُ قَدَّرْنَا بَيْنَكُمُ الْمَوْتَ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Nun noo natt ag dee ci yéen dogal ko te kenn du ko man a fanq. Te it lottu nu
61عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ أَمْثَالَكُمْ وَنُنشِئَكُمْ فِي مَا لَا تَعْلَمُونَ
te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu ngeen xamul.
62وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?
63أَفَرَأَيْتُم مَّا تَحْرُثُونَ
Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?
64أَأَنتُمْ تَزْرَعُونَهُ أَمْ نَحْنُ الزَّارِعُونَ
Yéen yéen a koy bay ? walla Nun noo koy bay ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 62

Simoore Al-Waqi'a Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo.…

Simoore Aaya 62/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers