Al-Waqi'a · 63/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
أَفَرَأَيْتُم مَّا تَحْرُثُونَ ۝٦٣
Afara`aytum maa tahrusoon
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 61-65 — Al-Waqi'a

61عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ أَمْثَالَكُمْ وَنُنشِئَكُمْ فِي مَا لَا تَعْلَمُونَ
te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu ngeen xamul.
62وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?
63أَفَرَأَيْتُم مَّا تَحْرُثُونَ
Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?
64أَأَنتُمْ تَزْرَعُونَهُ أَمْ نَحْنُ الزَّارِعُونَ
Yéen yéen a koy bay ? walla Nun noo koy bay ?
65لَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَاهُ حُطَامًا فَظَلْتُمْ تَفَكَّهُونَ
Sunu neexoon, Nu fóomal ko. Ngeen ne tócc di wél-wéli di [yuxu]:
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 63

Simoore Al-Waqi'a Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?

Simoore Aaya 63/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers