Al-An'am · 10/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَلَقَدِ اسْتُهْزِئَ بِرُسُلٍ مِّن قَبْلِكَ فَحَاقَ بِالَّذِينَ سَخِرُوا مِنْهُم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ ۝١٠
Wa laqadis tuhzi`a bi-Rusulim min qablika fahaaqa billazeena sakhiroo minhum maa kaanoo bihee yastahzi`oon
📖 Tekkim Wolof
Doon nañu yejji ay Yonent lu jiitu, waaye ña leen doon reetaan, la ñu daan yejji wàcc na ca seen kaw [alag leen].

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Al-An'am

8وَقَالُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ مَلَكٌ ۖ وَلَوْ أَنزَلْنَا مَلَكًا لَّقُضِيَ الْأَمْرُ ثُمَّ لَا يُنظَرُونَ
Ba noppi di wax naan : “Lu tee woon ñu wàcce ci moom Malaaka ? ”. Waaye bu ñu wàcce woon Malaaka, kon mbir ya sottikoon na ; ndax kenn duleen muñandiku kon.
9وَلَوْ جَعَلْنَاهُ مَلَكًا لَّجَعَلْنَاهُ رَجُلًا وَلَلَبَسْنَا عَلَيْهِم مَّا يَلْبِسُونَ
Te sax bu Nu ko defoon muy Malaaka, kon jëmmi nit Lanu koy jox, te kon Nu lëntal ca ñoom la Nu lëntal ci seen bopp.
10وَلَقَدِ اسْتُهْزِئَ بِرُسُلٍ مِّن قَبْلِكَ فَحَاقَ بِالَّذِينَ سَخِرُوا مِنْهُم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Doon nañu yejji ay Yonent lu jiitu, waaye ña leen doon reetaan, la ñu daan yejji wàcc na ca seen kaw [alag leen].
11قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ ثُمَّ انظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Neel : “Doxleen ci suuf si te ngeen seetlu naka la mujjug way-weddi ña deme”.
12قُل لِّمَن مَّا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ قُل لِّلَّهِ ۚ كَتَبَ عَلَىٰ نَفْسِهِ الرَّحْمَةَ ۚ لَيَجْمَعَنَّكُمْ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ لَا رَيْبَ فِيهِ ۚ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Neel : “Kan moo moom li nekk ci asamaan yeek suuf si ? ”. Neel : “Yàllaa ko moom ! ” Bind na ci boppam yërmaande. Fàwwu Dana leen dajale Bis-pénc ba : sikkuwul. Ña yàqal seen bopp, ñoom duñu gëm.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-An'am 10

Simoore Al-An'am Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Doon nañu yejji ay Yonent lu jiitu, waaye ña leen…

Simoore Aaya 10/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers