Al-A'raf · 16/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ فَبِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأَقْعُدَنَّ لَهُمْ صِرَاطَكَ الْمُسْتَقِيمَ ۝١٦
Qaala fabimaaa aghway tanee la aq`udanna lahum Siraatakal Mustaqeem
📖 Tekkim Wolof
bliis daldi ne : “Giñ naa ne beewloo gi Nga ma teg, danaa leen rékki ci sa yoon wu jub wi,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-A'raf

14قَالَ أَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”
15قَالَ إِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Bokk nga ca ña Nuy muñandiku.”
16قَالَ فَبِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأَقْعُدَنَّ لَهُمْ صِرَاطَكَ الْمُسْتَقِيمَ
bliis daldi ne : “Giñ naa ne beewloo gi Nga ma teg, danaa leen rékki ci sa yoon wu jub wi,
17ثُمَّ لَآتِيَنَّهُم مِّن بَيْنِ أَيْدِيهِمْ وَمِنْ خَلْفِهِمْ وَعَنْ أَيْمَانِهِمْ وَعَن شَمَائِلِهِمْ ۖ وَلَا تَجِدُ أَكْثَرَهُمْ شَاكِرِينَ
bu ko defee, ma songe leen ci seen kanam ak ci seen ginnaaw, seen ndeyjoor ak ci seen càmmoñ ba lu ëpp ci ñoom duñu la sant.”
18قَالَ اخْرُجْ مِنْهَا مَذْءُومًا مَّدْحُورًا ۖ لَّمَن تَبِعَكَ مِنْهُمْ لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنكُمْ أَجْمَعِينَ
Yàlla ne ko : “Génnal”, di ku ñu detteel, di ku ñu dàq. “Ku la ca toppati ci ñoom... fàwwu Danaa feesale Safara ci yéen ñépp [yaak ñoom]”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-A'raf 16

Simoore Al-A'raf Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bliis daldi ne : “Giñ naa ne beewloo gi Nga…

Simoore Aaya 16/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers