Al-Jinn · 21/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
قُلْ إِنِّي لَا أَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا رَشَدًا ۝٢١
Qul innee laaa amliku lakum darranw wa laa rashadaa
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne: “man mii kat manuma leen a lor manuma leen a jubbanti ”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Jinn

19وَأَنَّهُ لَمَّا قَامَ عَبْدُ اللَّهِ يَدْعُوهُ كَادُوا يَكُونُونَ عَلَيْهِ لِبَدًا
Te kat ba jaamub Yàlla bi taxawee di ñaan Boroomam, xawnañoo raj-rajloo ca kawam.
20قُلْ إِنَّمَا أَدْعُو رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِهِ أَحَدًا
Waxal ne : “Maa ngi ñaan sama Boroom te duma ko bokkaaleek kenn”.
21قُلْ إِنِّي لَا أَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا رَشَدًا
Waxal ne: “man mii kat manuma leen a lor manuma leen a jubbanti ”.
22قُلْ إِنِّي لَن يُجِيرَنِي مِنَ اللَّهِ أَحَدٌ وَلَنْ أَجِدَ مِن دُونِهِ مُلْتَحَدًا
Waxal it ne: “man mii keen manumaa aar ci Yàlla, te it duma wut benn rawtukaay budul moom.
23إِلَّا بَلَاغًا مِّنَ اللَّهِ وَرِسَالَاتِهِ ۚ وَمَن يَعْصِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ لَهُ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا
Manuma lu dul jottali ndigëlul Yàlla. Waaye képp ku moy Yàlla akub Yonentam ca Safara sa lay sax te dafay béel ba fàww.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Jinn 21

Simoore Al-Jinn Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne: “man mii kat manuma leen a lor manuma…

Simoore Aaya 21/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers