An-Naba · 35/40
Tekki Waxtaan — An-Naba
لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا كِذَّابًا ۝٣٥
Laa yasma`oona fiha lagh waw walaa kizzaba
📖 Tekkim Wolof
Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — An-Naba

33وَكَوَاعِبَ أَتْرَابًا
ak i jongama huur yu taxaw ay ween te maase,
34وَكَأْسًا دِهَاقًا
ak ay kaas yu fees dell.
35لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا كِذَّابًا
Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.
36جَزَاءً مِّن رَّبِّكَ عَطَاءً حِسَابًا
Muy pey gu bawoo ca seen Boroom
37رَّبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الرَّحْمَٰنِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِنْهُ خِطَابًا
Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy Yëramaakoon bi ; duñu mana waxanteek moom.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — An-Naba 35

Simoore An-Naba Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.

Simoore Aaya 35/40 — An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naba Dégg, An-Naba Tekki, An-Naba mp3, An-Naba pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers