Al-Mutaffifin · 32/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
وَإِذَا رَأَوْهُمْ قَالُوا إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَضَالُّونَ ۝٣٢
Wa izaa ra awhum qaalooo inna haaa`ulaaa`i ladaaal loon
📖 Tekkim Wolof
suñu leen masaana gis dañu daan wax ne : “Ñii dañoo sànku”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Mutaffifin

30وَإِذَا مَرُّوا بِهِمْ يَتَغَامَزُونَ
saa suñu leen rombaan, di leen ñaawal,
31وَإِذَا انقَلَبُوا إِلَىٰ أَهْلِهِمُ انقَلَبُوا فَكِهِينَ
bu ñu delluwaan ca seen njaboot, di ko kafe,
32وَإِذَا رَأَوْهُمْ قَالُوا إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَضَالُّونَ
suñu leen masaana gis dañu daan wax ne : “Ñii dañoo sànku”.
33وَمَا أُرْسِلُوا عَلَيْهِمْ حَافِظِينَ
Te, yabalunu leen ca ñoom ngir ñu daan leen wattu.
34فَالْيَوْمَ الَّذِينَ آمَنُوا مِنَ الْكُفَّارِ يَضْحَكُونَ
Tey jii nag, ñi gëm ñooy reetaan yéefar ya
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 32

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : suñu leen masaana gis dañu daan wax ne : “Ñii…

Simoore Aaya 32/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers