Al-Mutaffifin · 31/36
Tekki Waxtaan — Al-Mutaffifin
وَإِذَا انقَلَبُوا إِلَىٰ أَهْلِهِمُ انقَلَبُوا فَكِهِينَ ۝٣١
Wa izan qalabooo ilaaa ahlihimun qalaboo fakiheen
📖 Tekkim Wolof
bu ñu delluwaan ca seen njaboot, di ko kafe,
🎧 Dégg

📜 Aaya 29-33 — Al-Mutaffifin

29إِنَّ الَّذِينَ أَجْرَمُوا كَانُوا مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا يَضْحَكُونَ
Tooñkat ya dañu daan reetaan ña gëmoon,
30وَإِذَا مَرُّوا بِهِمْ يَتَغَامَزُونَ
saa suñu leen rombaan, di leen ñaawal,
31وَإِذَا انقَلَبُوا إِلَىٰ أَهْلِهِمُ انقَلَبُوا فَكِهِينَ
bu ñu delluwaan ca seen njaboot, di ko kafe,
32وَإِذَا رَأَوْهُمْ قَالُوا إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَضَالُّونَ
suñu leen masaana gis dañu daan wax ne : “Ñii dañoo sànku”.
33وَمَا أُرْسِلُوا عَلَيْهِمْ حَافِظِينَ
Te, yabalunu leen ca ñoom ngir ñu daan leen wattu.
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 31

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu ñu delluwaan ca seen njaboot, di ko kafe,

Simoore Aaya 31/36 — Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mutaffifin Dégg, Al-Mutaffifin Tekki, Al-Mutaffifin mp3, Al-Mutaffifin pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers