Yusuf · 60/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
فَإِن لَّمْ تَأْتُونِي بِهِ فَلَا كَيْلَ لَكُمْ عِندِي وَلَا تَقْرَبُونِ ۝٦٠
Fa il lam taatoonee bihee falaa kaila lakum `indee wa laa taqraboon
📖 Tekkim Wolof
Bu ngeen ma ko indilul, dungeen amati ci man indaar ; te it dungeen ma jegeñ”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Yusuf

58وَجَاءَ إِخْوَةُ يُوسُفَ فَدَخَلُوا عَلَيْهِ فَعَرَفَهُمْ وَهُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Ay doomi-baayi Yuusufa agsi ca moom [jóge seen réew ma]. Mu xàmmee leen te ñoom fakk nañu ko.
59وَلَمَّا جَهَّزَهُم بِجَهَازِهِمْ قَالَ ائْتُونِي بِأَخٍ لَّكُم مِّنْ أَبِيكُمْ ۚ أَلَا تَرَوْنَ أَنِّي أُوفِي الْكَيْلَ وَأَنَا خَيْرُ الْمُنزِلِينَ
Ba mu solee seen saaku ba noppi, mu ne leen : “Indil-leen ma seen doomi-baay ja des ak seen baay. Moo ndax gisuleen ne nattal na leen lu mat sëkk te it dalal naa leen gën ji daluwaay ?
60فَإِن لَّمْ تَأْتُونِي بِهِ فَلَا كَيْلَ لَكُمْ عِندِي وَلَا تَقْرَبُونِ
Bu ngeen ma ko indilul, dungeen amati ci man indaar ; te it dungeen ma jegeñ”.
61قَالُوا سَنُرَاوِدُ عَنْهُ أَبَاهُ وَإِنَّا لَفَاعِلُونَ
Ñu ne ko : “Dananu ko sàkku ci baayam. Te dananu ko def”.
62وَقَالَ لِفِتْيَانِهِ اجْعَلُوا بِضَاعَتَهُمْ فِي رِحَالِهِمْ لَعَلَّهُمْ يَعْرِفُونَهَا إِذَا انقَلَبُوا إِلَىٰ أَهْلِهِمْ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Mu ne ay surgaam : “Dellooleen, ci seeni sëf, njëg [ga ñu joxe]: xéy-na danañu ko xàmmee bu ñu delloo ca seeni mbokk te xéy-na danañu dellusi”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Yusuf 60

Simoore Yusuf Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ngeen ma ko indilul, dungeen amati ci man indaar…

Simoore Aaya 60/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers