Yusuf · 97/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
قَالُوا يَا أَبَانَا اسْتَغْفِرْ لَنَا ذُنُوبَنَا إِنَّا كُنَّا خَاطِئِينَ ۝٩٧
Qaaloo yaaa abaanas taghfir lanaa zunoo =banaaa innaa kunnaa khaati`een
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne : "Éy yaw sunu baay, sàkkul nu njéggal [ci Yàlla] sunuy bàkkaar. Ndax nun dey juumoon nanu ba def bàkkaar naka”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 95-99 — Yusuf

95قَالُوا تَاللَّهِ إِنَّكَ لَفِي ضَلَالِكَ الْقَدِيمِ
Ñu ne ko : “Giñ nanu ci Yàlla ne yaa ngi ci sa njuumte lu jëkk la”.
96فَلَمَّا أَن جَاءَ الْبَشِيرُ أَلْقَاهُ عَلَىٰ وَجْهِهِ فَارْتَدَّ بَصِيرًا ۖ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ إِنِّي أَعْلَمُ مِنَ اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Waaye, ba kuy bégle ka agsee, daldi koy xëpp yére ya ci kanam. Mu daldi ne xàjj di gis, mu ne : “Moo ndax waxuma leen woon ne xam naa lu ma jële ci Yàlla lu ngeen xamul ? ”
97قَالُوا يَا أَبَانَا اسْتَغْفِرْ لَنَا ذُنُوبَنَا إِنَّا كُنَّا خَاطِئِينَ
- Ñu ne : "Éy yaw sunu baay, sàkkul nu njéggal [ci Yàlla] sunuy bàkkaar. Ndax nun dey juumoon nanu ba def bàkkaar naka”.
98قَالَ سَوْفَ أَسْتَغْفِرُ لَكُمْ رَبِّي ۖ إِنَّهُ هُوَ الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
- Mu ne : “Danaa leen ñaanal njéggal ci sama Boroom. Moom Yàlla nag mooy Jéggalaakoon ba, di Jaglewaakoon ba”.
99فَلَمَّا دَخَلُوا عَلَىٰ يُوسُفَ آوَىٰ إِلَيْهِ أَبَوَيْهِ وَقَالَ ادْخُلُوا مِصْرَ إِن شَاءَ اللَّهُ آمِنِينَ
Ba ñu delloo ca Yuusufa, mu song ñaari waajuram, ne leen : “Dugguleen Misra ànd ak kóolute, bu soobee Yàlla ! ”
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
97Aaya

Tekki — Yusuf 97

Simoore Yusuf Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne : "Éy yaw sunu baay, sàkkul nu…

Simoore Aaya 97/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers