Al-Hijr · 32/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا لَكَ أَلَّا تَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ ۝٣٢
Qaala yaaa Ibleesu maa laka allaa takoona ma`as saajideen
📖 Tekkim Wolof
Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal ba bokkuloo ci sujjóotkat yi ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Hijr

30فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka yépp sujjóot,
31إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ أَن يَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay sujjóot.
32قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا لَكَ أَلَّا تَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal ba bokkuloo ci sujjóotkat yi ? ”
33قَالَ لَمْ أَكُن لِّأَسْجُدَ لِبَشَرٍ خَلَقْتَهُ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
34قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Hijr 32

Simoore Al-Hijr Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal…

Simoore Aaya 32/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers