Al-Hijr · 53/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالُوا لَا تَوْجَلْ إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ ۝٥٣
Qaaloo la tawjal innaa nubashshiruka bighulaamin `aleem
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi lay bégal ne [danga am doom] ju góor juy bari xam- xam”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 51-55 — Simoore Al-Hijr

51وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya
52إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا قَالَ إِنَّا مِنكُمْ وَجِلُونَ
Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam” - Mu ne leen : “Am naa njàqare ci yéen”.
53قَالُوا لَا تَوْجَلْ إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ
Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi lay bégal ne [danga am doom] ju góor juy bari xam- xam”.
54قَالَ أَبَشَّرْتُمُونِي عَلَىٰ أَن مَّسَّنِيَ الْكِبَرُ فَبِمَ تُبَشِّرُونَ
Mu ne : “Li ngeen di bégle ndax ànd naak samag mage ? Li ngeen may yégal mooy lan ? ”
55قَالُوا بَشَّرْنَاكَ بِالْحَقِّ فَلَا تَكُن مِّنَ الْقَانِطِينَ
- Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la. Bul bokk ca ña naagu ña”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Hijr 53

Simoore Al-Hijr Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi…

Simoore Aaya 53/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers