Al-Hijr · 52/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا قَالَ إِنَّا مِنكُمْ وَجِلُونَ ٥٢
Transliteration
Iz dakhaloo `alaihi faqaaloo salaaman qaala innaa minkum wajiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam” - Mu ne leen : “Am naa njàqare ci yéen”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 50-54 — Al-Hijr
50وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.
51وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya
52إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا قَالَ إِنَّا مِنكُمْ وَجِلُونَ
Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam” - Mu ne leen : “Am naa njàqare ci yéen”.
53قَالُوا لَا تَوْجَلْ إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ
Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi lay bégal ne [danga am doom] ju góor juy bari xam- xam”.
54قَالَ أَبَشَّرْتُمُونِي عَلَىٰ أَن مَّسَّنِيَ الْكِبَرُ فَبِمَ تُبَشِّرُونَ
Mu ne : “Li ngeen di bégle ndax ànd naak samag mage ? Li ngeen may yégal mooy lan ? ”
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
52Aaya
Tekki — Al-Hijr 52
Simoore Al-Hijr Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam”…Simoore Aaya 52/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








