Al-Hijr · 89/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَقُلْ إِنِّي أَنَا النَّذِيرُ الْمُبِينُ ۝٨٩
Wa qul inneee anan nazeerul mubeen
📖 Tekkim Wolof
Te neel : “Man aji-laabir laa ju wér” [ci xamal leen dëgg],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 87-91 — Simoore Al-Hijr

87وَلَقَدْ آتَيْنَاكَ سَبْعًا مِّنَ الْمَثَانِي وَالْقُرْآنَ الْعَظِيمَ
May Nanu la “juroom-ñaar yu Nu ñaar-ñaaral [Al-Faatiha]”, ak Alxuraan ju màgg jii.
88لَا تَمُدَّنَّ عَيْنَيْكَ إِلَىٰ مَا مَتَّعْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّنْهُمْ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِلْمُؤْمِنِينَ
Bul tàllal say gët [di xool] la Nu xéewale ay kurél ci ñoom, bul am naqar ci ñoom te nangay suufeel say mbagg ñeel ñi gëm.
89وَقُلْ إِنِّي أَنَا النَّذِيرُ الْمُبِينُ
Te neel : “Man aji-laabir laa ju wér” [ci xamal leen dëgg],
90كَمَا أَنزَلْنَا عَلَى الْمُقْتَسِمِينَ
Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle woon [seen diine],
91الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Al-Hijr 89

Simoore Al-Hijr Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te neel : “Man aji-laabir laa ju wér” [ci xamal…

Simoore Aaya 89/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers