Al-Hijr · 90/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
كَمَا أَنزَلْنَا عَلَى الْمُقْتَسِمِينَ ۝٩٠
Kamaaa anzalnaa `alal muqtasimeen
📖 Tekkim Wolof
Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle woon [seen diine],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 88-92 — Simoore Al-Hijr

88لَا تَمُدَّنَّ عَيْنَيْكَ إِلَىٰ مَا مَتَّعْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّنْهُمْ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِلْمُؤْمِنِينَ
Bul tàllal say gët [di xool] la Nu xéewale ay kurél ci ñoom, bul am naqar ci ñoom te nangay suufeel say mbagg ñeel ñi gëm.
89وَقُلْ إِنِّي أَنَا النَّذِيرُ الْمُبِينُ
Te neel : “Man aji-laabir laa ju wér” [ci xamal leen dëgg],
90كَمَا أَنزَلْنَا عَلَى الْمُقْتَسِمِينَ
Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle woon [seen diine],
91الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.
92فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — Al-Hijr 90

Simoore Al-Hijr Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle…

Simoore Aaya 90/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers