Maryam · 35/98
Tekki Waxtaan — Maryam
مَا كَانَ لِلَّهِ أَن يَتَّخِذَ مِن وَلَدٍ ۖ سُبْحَانَهُ ۚ إِذَا قَضَىٰ أَمْرًا فَإِنَّمَا يَقُولُ لَهُ كُن فَيَكُونُ ۝٣٥
Maa kaana lillaahi ai yattakhiza minw waladin Subhaanah; izaa qadaaa amran fa innamaa yaqoolu lahoo kun fa yakoon
📖 Tekkim Wolof
Yellul ci Yàlla muy jàppe kenn doomam. Cëy sellam ga ! Bu bëggee menn mbir, Danaan : “Nekkal ! ” mu daldi nekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Maryam

33وَالسَّلَامُ عَلَيَّ يَوْمَ وُلِدتُّ وَيَوْمَ أَمُوتُ وَيَوْمَ أُبْعَثُ حَيًّا
Jàmm rekk laay am bis ba ma juddoo, ak ca bis ba may dee ak bis ba may dekkiwaat”.
34ذَٰلِكَ عِيسَى ابْنُ مَرْيَمَ ۚ قَوْلَ الْحَقِّ الَّذِي فِيهِ يَمْتَرُونَ
Loolu mooy mbirum Iisaa doomu Maryam, wax jii moo cay dëgg ca la ngeen doon werante.
35مَا كَانَ لِلَّهِ أَن يَتَّخِذَ مِن وَلَدٍ ۖ سُبْحَانَهُ ۚ إِذَا قَضَىٰ أَمْرًا فَإِنَّمَا يَقُولُ لَهُ كُن فَيَكُونُ
Yellul ci Yàlla muy jàppe kenn doomam. Cëy sellam ga ! Bu bëggee menn mbir, Danaan : “Nekkal ! ” mu daldi nekk.
36وَإِنَّ اللَّهَ رَبِّي وَرَبُّكُمْ فَاعْبُدُوهُ ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
“Te nag Yàlla moo di sama Boroom, di seen Boroom. Jaamuleen ko. Lii moo di yoon wu jub wi xocc”.
37فَاخْتَلَفَ الْأَحْزَابُ مِن بَيْنِهِمْ ۖ فَوَيْلٌ لِّلَّذِينَ كَفَرُوا مِن مَّشْهَدِ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Kurél yi juuyoo nañu ci seen diggante. Ñay weddi, xuru Safara ñeel na leen ca teewaayub bis bu màgg ba !
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Maryam 35

Simoore Maryam Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yellul ci Yàlla muy jàppe kenn doomam. Cëy sellam ga…

Simoore Aaya 35/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers