Maryam · 93/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
إِن كُلُّ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ إِلَّا آتِي الرَّحْمَٰنِ عَبْدًا ۝٩٣
In kullu man fis samaawaati wal ardi illaaa aatir Rahmaani `abdaa
📖 Tekkim Wolof
Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub Yàlla rekk lay doon.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 91-95 — Simoore Maryam

91أَن دَعَوْا لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدًا
ña wax ne alamikk Yàlla am na doom,
92وَمَا يَنبَغِي لِلرَّحْمَٰنِ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا
Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !
93إِن كُلُّ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ إِلَّا آتِي الرَّحْمَٰنِ عَبْدًا
Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub Yàlla rekk lay doon.
94لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].
95وَكُلُّهُمْ آتِيهِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَرْدًا
Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam kennoo kenn.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Maryam 93

Simoore Maryam Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub…

Simoore Aaya 93/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers