Taha · 17/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَمَا تِلْكَ بِيَمِينِكَ يَا مُوسَىٰ ۝١٧
Wa maa tilka bi yamee nika yaa Moosaa
📖 Tekkim Wolof
Waaw Muusaa, li nekk ci sa loxo ndeyjoor lan la ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 15-19 — Simoore Taha

15إِنَّ السَّاعَةَ آتِيَةٌ أَكَادُ أُخْفِيهَا لِتُجْزَىٰ كُلُّ نَفْسٍ بِمَا تَسْعَىٰ
Te Bis-pénc ba daanaka ñëw na. Dama koo xaw a làq rekk ngir fey bakkan bu nekk la muy jëf.
16فَلَا يَصُدَّنَّكَ عَنْهَا مَن لَّا يُؤْمِنُ بِهَا وَاتَّبَعَ هَوَاهُ فَتَرْدَىٰ
[Kon farlul ba] képp ku gëmul tey topp bànneexam, bañ laa gàllankoor ngay alku.
17وَمَا تِلْكَ بِيَمِينِكَ يَا مُوسَىٰ
Waaw Muusaa, li nekk ci sa loxo ndeyjoor lan la ? ”
18قَالَ هِيَ عَصَايَ أَتَوَكَّأُ عَلَيْهَا وَأَهُشُّ بِهَا عَلَىٰ غَنَمِي وَلِيَ فِيهَا مَآرِبُ أُخْرَىٰ
Mu wax ne : “Samaw yet la, dama ciy sukkóotu, di ci waññ samag jur ak yeneeni mbir”.
19قَالَ أَلْقِهَا يَا مُوسَىٰ
[Yàlla ne ko] : “Sànni ko yaw Muusaa”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Taha 17

Simoore Taha Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaw Muusaa, li nekk ci sa loxo ndeyjoor lan la…

Simoore Aaya 17/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers