Al-Anbiya · 59/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
قَالُوا مَن فَعَلَ هَٰذَا بِآلِهَتِنَا إِنَّهُ لَمِنَ الظَّالِمِينَ ۝٥٩
Qaaloo man fa`ala haazaa bi aalihatinaaa innahoo laminaz zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Ku def lii sunu yàlla yi ? Kooka dey bokk na ca tooñkat ya”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-61 — Simoore Al-Anbiya

57وَتَاللَّهِ لَأَكِيدَنَّ أَصْنَامَكُم بَعْدَ أَن تُوَلُّوا مُدْبِرِينَ
Te waat naa ci Yàlla ! Ne danaa fexeel seen xërëm yi ci seen ginnaaw, bu ngeen dëddoo”.
58فَجَعَلَهُمْ جُذَاذًا إِلَّا كَبِيرًا لَّهُمْ لَعَلَّهُمْ إِلَيْهِ يَرْجِعُونَ
Mu dàggate leen ba mu des xërëm bu mag ba. Ngir xéy-na mu mën cee delloo [seeni xel].
59قَالُوا مَن فَعَلَ هَٰذَا بِآلِهَتِنَا إِنَّهُ لَمِنَ الظَّالِمِينَ
Ñu ne : “Ku def lii sunu yàlla yi ? Kooka dey bokk na ca tooñkat ya”.
60قَالُوا سَمِعْنَا فَتًى يَذْكُرُهُمْ يُقَالُ لَهُ إِبْرَاهِيمُ
Am ñu wax ne : “Déggoon nanu benn waxamaande mu di leen ayibal ; ñu di ko woowe Ibraahiima”.
61قَالُوا فَأْتُوا بِهِ عَلَىٰ أَعْيُنِ النَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَشْهَدُونَ
Ñu ne : “Indileen ko ci kanamu nit ñi”, xéy-na ñoom ñu nekki seede [ci loolu].
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Al-Anbiya 59

Simoore Al-Anbiya Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Ku def lii sunu yàlla yi ?…

Simoore Aaya 59/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers