Al-Mu'minun · 83/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
لَقَدْ وُعِدْنَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا هَٰذَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ ۝٨٣
Laqad wu`idnaa nahnu wa aabaaa`unaa haazaa min qablu in haazaaa illaaa asaateerul awwaleen
📖 Tekkim Wolof
Lii dey digoon nañu ko sunuy maam ak nun ; lii daal ay léeb rekk la”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 81-85 — Simoore Al-Mu'minun

81بَلْ قَالُوا مِثْلَ مَا قَالَ الْأَوَّلُونَ
Ñoom kay faf dañoo wax rekk la ñu jëkk ña waxoon.
82قَالُوا أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Nee nañu : “Ndax bu nu faatoo ba nekk suuf ak i yax, ndax dananu dekkiwaat ?
83لَقَدْ وُعِدْنَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا هَٰذَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii dey digoon nañu ko sunuy maam ak nun ; lii daal ay léeb rekk la”
84قُل لِّمَنِ الْأَرْضُ وَمَن فِيهَا إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan moo moom suuf si ak li ci biiram ? Ndeem xam ngeen”.
85سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Kon danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Moo ndax dangeen dul fàttaliku ? ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 83

Simoore Al-Mu'minun Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii dey digoon nañu ko sunuy maam ak nun ;…

Simoore Aaya 83/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers