Ash-Shu'ara · 109/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝١٠٩
Wa maaa as`alukum `alaihi min ajrin in ajriya illaa `alaa Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Te laajuma leen ci génn pey ; samag pey Boroom àddina si moo ko warlu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 107-111 — Ash-Shu'ara

107إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man seenub Yonent laa bu wóor.
108فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
109وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Te laajuma leen ci génn pey ; samag pey Boroom àddina si moo ko warlu.
110فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma”
111۞ قَالُوا أَنُؤْمِنُ لَكَ وَاتَّبَعَكَ الْأَرْذَلُونَ
Ñu wax ko ne : “Ndax dananu la gëm te ñi gën a saay-saay a ngi la topp? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 109

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te laajuma leen ci génn pey ; samag pey Boroom…

Simoore Aaya 109/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers