Ash-Shu'ara · 130/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَإِذَا بَطَشْتُم بَطَشْتُمْ جَبَّارِينَ ۝١٣٠
Wa izaa batashtum batashtum jabbaareen
📖 Tekkim Wolof
Te saa su ngeen songee mu jéggi dayo.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 128-132 — Simoore Ash-Shu'ara

128أَتَبْنُونَ بِكُلِّ رِيعٍ آيَةً تَعْبَثُونَ
Ndax dangeen di tabax ci kaw wépp tundu ab jàjj ngir caaxaan ?
129وَتَتَّخِذُونَ مَصَانِعَ لَعَلَّكُمْ تَخْلُدُونَ
Ngeen di liggéey i njéndi mel ni dangeen fiy béel ?
130وَإِذَا بَطَشْتُم بَطَشْتُمْ جَبَّارِينَ
Te saa su ngeen songee mu jéggi dayo.
131فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
132وَاتَّقُوا الَّذِي أَمَدَّكُم بِمَا تَعْلَمُونَ
Ragal-leen Yàlla mi leen kàttanal ba ngeen mën a jëf,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
130Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 130

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 130 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te saa su ngeen songee mu jéggi dayo.

Simoore Aaya 130/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 128–132. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers