Ash-Shu'ara · 129/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَتَتَّخِذُونَ مَصَانِعَ لَعَلَّكُمْ تَخْلُدُونَ ۝١٢٩
Wa tattakhizoona masaani`a la`allakum takhludoon
📖 Tekkim Wolof
Ngeen di liggéey i njéndi mel ni dangeen fiy béel ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 127-131 — Ash-Shu'ara

127وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Duma leen ca laaj genn pey ; samag pey Boroom àddina see ko warlu.
128أَتَبْنُونَ بِكُلِّ رِيعٍ آيَةً تَعْبَثُونَ
Ndax dangeen di tabax ci kaw wépp tundu ab jàjj ngir caaxaan ?
129وَتَتَّخِذُونَ مَصَانِعَ لَعَلَّكُمْ تَخْلُدُونَ
Ngeen di liggéey i njéndi mel ni dangeen fiy béel ?
130وَإِذَا بَطَشْتُم بَطَشْتُمْ جَبَّارِينَ
Te saa su ngeen songee mu jéggi dayo.
131فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
129Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 129

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 129 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngeen di liggéey i njéndi mel ni dangeen fiy béel…

Simoore Aaya 129/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 127–131. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers