Ash-Shu'ara · 50/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالُوا لَا ضَيْرَ ۖ إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ ۝٥٠
Qaaloo la daira innaaa ilaa Rabbinaa munqalliboon
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Boo yaboo ! Nun daal jublu nanu sunu Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Ash-Shu'ara

48رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna”.
49قَالَ آمَنتُمْ لَهُ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّهُ لَكَبِيرُكُمُ الَّذِي عَلَّمَكُمُ السِّحْرَ فَلَسَوْفَ تَعْلَمُونَ ۚ لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ وَلَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
[Firawna] ne leen : “Gëmoon ngeen ko ba ma leen a laataa woo. [Xam naa ne] mooy kàndiŋ mi leen jàngal njibar ! Dangeen xam ne ! Danaa dagg seen yoxook seeni tànk, jalawle ko, danaa leen daaj yéen ñépp”.
50قَالُوا لَا ضَيْرَ ۖ إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ
Ñu ne ko : “Boo yaboo ! Nun daal jublu nanu sunu Boroom.
51إِنَّا نَطْمَعُ أَن يَغْفِرَ لَنَا رَبُّنَا خَطَايَانَا أَن كُنَّا أَوَّلَ الْمُؤْمِنِينَ
Danoo xemmem Yàlla jéggal nu sunuy njuumte, xemmem it doon ñu njëkk a gëm”.
52۞ وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَسْرِ بِعِبَادِي إِنَّكُم مُّتَّبَعُونَ
Nu daldi soloo Muusaa, digal ko mu rañaan ànd ak samay jaam te danañu leen dabsi.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 50

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Boo yaboo ! Nun daal jublu…

Simoore Aaya 50/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers