Ash-Shu'ara · 63/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنِ اضْرِب بِّعَصَاكَ الْبَحْرَ ۖ فَانفَلَقَ فَكَانَ كُلُّ فِرْقٍ كَالطَّوْدِ الْعَظِيمِ ٦٣
Transliteration
Fa awhainaaa ilaa Moosaaa anidrib bi`asaakal bahra fanfalaqa fakaana kullu firqin kattawdil `azeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi soloo Muusaa, digal ko : “Dóoral géej geek sa yet wi”. Mu daldi xàjjeeku, xaaj bu nekk tollu ni aw tund wu mag.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 61-65 — Ash-Shu'ara
61فَلَمَّا تَرَاءَى الْجَمْعَانِ قَالَ أَصْحَابُ مُوسَىٰ إِنَّا لَمُدْرَكُونَ
Ba ñaari mbooloo ya séenantee, waa kër Muusaa daldi ne : “Ñanga nuy dabsi de”.
62قَالَ كَلَّا ۖ إِنَّ مَعِيَ رَبِّي سَيَهْدِينِ
[Muusaa] ne : “Mukk, duñu nu dab ndax ànd naak sama Boroom te Dana ma gindi”.
63فَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنِ اضْرِب بِّعَصَاكَ الْبَحْرَ ۖ فَانفَلَقَ فَكَانَ كُلُّ فِرْقٍ كَالطَّوْدِ الْعَظِيمِ
Nu daldi soloo Muusaa, digal ko : “Dóoral géej geek sa yet wi”. Mu daldi xàjjeeku, xaaj bu nekk tollu ni aw tund wu mag.
64وَأَزْلَفْنَا ثَمَّ الْآخَرِينَ
Nu tañcale Firawna mook u nitam.
65وَأَنجَيْنَا مُوسَىٰ وَمَن مَّعَهُ أَجْمَعِينَ
Nu daldi musal Muusaa mook ña mu àndanloon ñépp ;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
63Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 63
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi soloo Muusaa, digal ko : “Dóoral géej geek…Simoore Aaya 63/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








