Aali Imran · 139/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
وَلَا تَهِنُوا وَلَا تَحْزَنُوا وَأَنتُمُ الْأَعْلَوْنَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ ۝١٣٩
Wa laa tahinoo wa laa tahzanoo wa antumul a`lawna in kuntum mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Buleen doyadi, buleen ragal, yéen ay féete kaw ndegam gëm ngeen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 137-141 — Aali Imran

137قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلِكُمْ سُنَنٌ فَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Am na ay yoon yu jàll yu ñu sosoon ba ngeen dikkagul. Kon doxleen wër ci goxi suuf, te di xool naka la ña daan weddi mujje.
138هَٰذَا بَيَانٌ لِّلنَّاسِ وَهُدًى وَمَوْعِظَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ
Lii ag leeral la ci nit ñi, te di ag njub ak ug waare ngir ñi ragal Yàlla.
139وَلَا تَهِنُوا وَلَا تَحْزَنُوا وَأَنتُمُ الْأَعْلَوْنَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Buleen doyadi, buleen ragal, yéen ay féete kaw ndegam gëm ngeen.
140إِن يَمْسَسْكُمْ قَرْحٌ فَقَدْ مَسَّ الْقَوْمَ قَرْحٌ مِّثْلُهُ ۚ وَتِلْكَ الْأَيَّامُ نُدَاوِلُهَا بَيْنَ النَّاسِ وَلِيَعْلَمَ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا وَيَتَّخِذَ مِنكُمْ شُهَدَاءَ ۗ وَاللَّهُ لَا يُحِبُّ الظَّالِمِينَ
Su fekkee metit dal na leen, wu na mel daloon na yéefar yi. Bis yooya [Bisi naqar] danu leen di ay-ayle ci nit ñi ak itam ngir Yàlla xàmmee ñi gëm, te dana sàkk ci ñi dee ci xare, te bokk ci yéen, ay chuhadaa - Yàlla du safoo tooñkat ya.
141وَلِيُمَحِّصَ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا وَيَمْحَقَ الْكَافِرِينَ
Loola Yàlla dakoy defe ngir laabal ñi gëm, di ci lakk yéefar ya.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
139Aaya

Tekki — Aali Imran 139

Simoore Aali Imran Aaya 139 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen doyadi, buleen ragal, yéen ay féete kaw ndegam gëm…

Simoore Aaya 139/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 137–141. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers