As-Saffat · 100/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
رَبِّ هَبْ لِي مِنَ الصَّالِحِينَ ۝١٠٠
Rabbi hab lee minas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Yaw sama Boroom, may ma ay sët yu yiw”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 98-102 — Simoore As-Saffat

98فَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَسْفَلِينَ
Ñu bëggoon koo fexeel ; Nu suufeel leen, detteel leen.
99وَقَالَ إِنِّي ذَاهِبٌ إِلَىٰ رَبِّي سَيَهْدِينِ
Mu wax ne : “Maa ngi dem ca sama Boroom, Dana ma gindi.
100رَبِّ هَبْ لِي مِنَ الصَّالِحِينَ
Yaw sama Boroom, may ma ay sët yu yiw”.
101فَبَشَّرْنَاهُ بِغُلَامٍ حَلِيمٍ
Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .
102فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
100Aaya

Tekki — As-Saffat 100

Simoore As-Saffat Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw sama Boroom, may ma ay sët yu yiw”.

Simoore Aaya 100/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers