As-Saffat · 32/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَأَغْوَيْنَاكُمْ إِنَّا كُنَّا غَاوِينَ ۝٣٢
Fa aghwainaakum innaa kunnaa ghaaween
📖 Tekkim Wolof
“Noo ngi leen di jiiñ cànkute, waaye nun ñépp a faf sànku”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 30-34 — Simoore As-Saffat

30وَمَا كَانَ لَنَا عَلَيْكُم مِّن سُلْطَانٍ ۖ بَلْ كُنتُمْ قَوْمًا طَاغِينَ
Te nun amunu woon benn sañ-sañ ci yéen. Yéen kay yéen a bewoon.
31فَحَقَّ عَلَيْنَا قَوْلُ رَبِّنَا ۖ إِنَّا لَذَائِقُونَ
La Yàlla daan wax dal na ci sunu kaw ; [tey] noo ngi toqamtiku [mbugal].
32فَأَغْوَيْنَاكُمْ إِنَّا كُنَّا غَاوِينَ
“Noo ngi leen di jiiñ cànkute, waaye nun ñépp a faf sànku”.
33فَإِنَّهُمْ يَوْمَئِذٍ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ
Bu bisub keroogee ñoom ñéppay bokk mbugal ma.
34إِنَّا كَذَٰلِكَ نَفْعَلُ بِالْمُجْرِمِينَ
Noonu la Nuy def tooñkat ya.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — As-Saffat 32

Simoore As-Saffat Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Noo ngi leen di jiiñ cànkute, waaye nun ñépp a…

Simoore Aaya 32/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers