As-Saffat · 33/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَإِنَّهُمْ يَوْمَئِذٍ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ ۝٣٣
Fa innahum Yawma`izin fil`azaabi mushtarikoon
📖 Tekkim Wolof
Bu bisub keroogee ñoom ñéppay bokk mbugal ma.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore As-Saffat

31فَحَقَّ عَلَيْنَا قَوْلُ رَبِّنَا ۖ إِنَّا لَذَائِقُونَ
La Yàlla daan wax dal na ci sunu kaw ; [tey] noo ngi toqamtiku [mbugal].
32فَأَغْوَيْنَاكُمْ إِنَّا كُنَّا غَاوِينَ
“Noo ngi leen di jiiñ cànkute, waaye nun ñépp a faf sànku”.
33فَإِنَّهُمْ يَوْمَئِذٍ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ
Bu bisub keroogee ñoom ñéppay bokk mbugal ma.
34إِنَّا كَذَٰلِكَ نَفْعَلُ بِالْمُجْرِمِينَ
Noonu la Nuy def tooñkat ya.
35إِنَّهُمْ كَانُوا إِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ يَسْتَكْبِرُونَ
Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yàlla”, dañu daan rëy-rëylu,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — As-Saffat 33

Simoore As-Saffat Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu bisub keroogee ñoom ñéppay bokk mbugal ma.

Simoore Aaya 33/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers