Al-Waqi'a · 64/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
أَأَنتُمْ تَزْرَعُونَهُ أَمْ نَحْنُ الزَّارِعُونَ ۝٦٤
A-antum tazra`oonahooo am nahnuz zaari`ooon
📖 Tekkim Wolof
Yéen yéen a koy bay ? walla Nun noo koy bay ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Al-Waqi'a

62وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?
63أَفَرَأَيْتُم مَّا تَحْرُثُونَ
Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?
64أَأَنتُمْ تَزْرَعُونَهُ أَمْ نَحْنُ الزَّارِعُونَ
Yéen yéen a koy bay ? walla Nun noo koy bay ?
65لَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَاهُ حُطَامًا فَظَلْتُمْ تَفَكَّهُونَ
Sunu neexoon, Nu fóomal ko. Ngeen ne tócc di wél-wéli di [yuxu]:
66إِنَّا لَمُغْرَمُونَ
Te naan : “Danoo fees dell ak i bor !
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 64

Simoore Al-Waqi'a Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen yéen a koy bay ? walla Nun noo koy…

Simoore Aaya 64/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers