Al-Haqqa · 6/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَأَمَّا عَادٌ فَأُهْلِكُوا بِرِيحٍ صَرْصَرٍ عَاتِيَةٍ ۝٦
Wa ammaa `Aadun fa uhlikoo bireehin sarsarin `aatiyah
📖 Tekkim Wolof
Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la ñu léen alage.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Haqqa

4كَذَّبَتْ ثَمُودُ وَعَادٌ بِالْقَارِعَةِ
Giirug Aad ak Samuud dañoo weddi woon yëngu-yëngu bu rëy ba.
5فَأَمَّا ثَمُودُ فَأُهْلِكُوا بِالطَّاغِيَةِ
Giirug Samuud ag yuuxu (am riir) la ñu léen alage.
6وَأَمَّا عَادٌ فَأُهْلِكُوا بِرِيحٍ صَرْصَرٍ عَاتِيَةٍ
Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la ñu léen alage.
7سَخَّرَهَا عَلَيْهِمْ سَبْعَ لَيَالٍ وَثَمَانِيَةَ أَيَّامٍ حُسُومًا فَتَرَى الْقَوْمَ فِيهَا صَرْعَىٰ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ خَاوِيَةٍ
xiirtal na ko ci séen kaw juróom yaari bëccag ak juróom yaari guddi yu tegaloo nit ña ne lasiim melni dàtti tàndarma yu fënëx.
8فَهَلْ تَرَىٰ لَهُم مِّن بَاقِيَةٍ
Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Haqqa 6

Simoore Al-Haqqa Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la…

Simoore Aaya 6/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers