Al-A'raf · 113/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَجَاءَ السَّحَرَةُ فِرْعَوْنَ قَالُوا إِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ ١١٣
Transliteration
Wa jaaa`as saharatu Fir`awna qaaloo inna lanaa la ajjran in kunnaa nahnul ghaalibeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Jabar ya ñëw ca Firawna ne ko : “Ndax dananu am pey bu fekkee ne not nanu ? ”[joŋ]
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 111-115 — Al-A'raf
111قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَأَرْسِلْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Xaarloo ko mook mbokkam, te yónnee ci dëkk yi ay ndaw ñu mën a dajale nit ñi,
112يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَاحِرٍ عَلِيمٍ
ñu indil la bépp jabar bu am xam-xam.
113وَجَاءَ السَّحَرَةُ فِرْعَوْنَ قَالُوا إِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ
Jabar ya ñëw ca Firawna ne ko : “Ndax dananu am pey bu fekkee ne not nanu ? ”[joŋ]
114قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ لَمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dangeen bokk ci ñi may jegeñ”.
115قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ نَحْنُ الْمُلْقِينَ
Ñu ne : “Muusaa, benn yaw nga sànni, walla nun nu sànni”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
113Aaya
Tekki — Al-A'raf 113
Simoore Al-A'raf Aaya 113 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jabar ya ñëw ca Firawna ne ko : “Ndax dananu…Simoore Aaya 113/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 111–115. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








