Al-A'raf · 114/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ لَمِنَ الْمُقَرَّبِينَ ۝١١٤
Qaala na`am wa innakum laminal muqarrabeen
📖 Tekkim Wolof
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dangeen bokk ci ñi may jegeñ”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 112-116 — Simoore Al-A'raf

112يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَاحِرٍ عَلِيمٍ
ñu indil la bépp jabar bu am xam-xam.
113وَجَاءَ السَّحَرَةُ فِرْعَوْنَ قَالُوا إِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ
Jabar ya ñëw ca Firawna ne ko : “Ndax dananu am pey bu fekkee ne not nanu ? ”[joŋ]
114قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ لَمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dangeen bokk ci ñi may jegeñ”.
115قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ نَحْنُ الْمُلْقِينَ
Ñu ne : “Muusaa, benn yaw nga sànni, walla nun nu sànni”.
116قَالَ أَلْقُوا ۖ فَلَمَّا أَلْقَوْا سَحَرُوا أَعْيُنَ النَّاسِ وَاسْتَرْهَبُوهُمْ وَجَاءُوا بِسِحْرٍ عَظِيمٍ
Mu ne : “Sànnileen”. Ba ñu sànnee, dañoo jabar bëti nit ña, ragal-loo leen ci jabar gu rëy.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
114Aaya

Tekki — Al-A'raf 114

Simoore Al-A'raf Aaya 114 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne leen : “Waawaaw, kon dangeen bokk ci ñi…

Simoore Aaya 114/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 112–116. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers