Nuh · 8/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
ثُمَّ إِنِّي دَعَوْتُهُمْ جِهَارًا ۝٨
Summa innee da`aw tuhum jihaara
📖 Tekkim Wolof
Topp, woonaa leen cig jooru.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore Nuh

6فَلَمْ يَزِدْهُمْ دُعَائِي إِلَّا فِرَارًا
Te sama woote bi dolli wu leen lu dul féew.
7وَإِنِّي كُلَّمَا دَعَوْتُهُمْ لِتَغْفِرَ لَهُمْ جَعَلُوا أَصَابِعَهُمْ فِي آذَانِهِمْ وَاسْتَغْشَوْا ثِيَابَهُمْ وَأَصَرُّوا وَاسْتَكْبَرُوا اسْتِكْبَارًا
Te man saasu ma leen di woo ngir Nga jégël leen, dañuy def séeni waaraam ci séeni biiri nopp, daldi muuroo séeni sér, daldi jomlu.
8ثُمَّ إِنِّي دَعَوْتُهُمْ جِهَارًا
Topp, woonaa leen cig jooru.
9ثُمَّ إِنِّي أَعْلَنتُ لَهُمْ وَأَسْرَرْتُ لَهُمْ إِسْرَارًا
Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.
10فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Nuh 8

Simoore Nuh Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp, woonaa leen cig jooru.

Simoore Aaya 8/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers