Al-Anfal · 22/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
۞ إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الصُّمُّ الْبُكْمُ الَّذِينَ لَا يَعْقِلُونَ ۝٢٢
Inna sharrad dawaaabbi `indal laahis summul bukmul lazeena laa ya`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Li gën a yées ci bindeef yi ca Yàlla, mooy ñi tëx, luu te bañ a xel-lu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Anfal

20يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَلَا تَوَلَّوْا عَنْهُ وَأَنتُمْ تَسْمَعُونَ
Éy yéen ñi gëm ñi ! Nangeen topp Yàlla ak ub Yonentam, buleen ko dëddu te fekk dégg ngeen li muy wax.
21وَلَا تَكُونُوا كَالَّذِينَ قَالُوا سَمِعْنَا وَهُمْ لَا يَسْمَعُونَ
Buleen mel ni ñiy wax : “Dégg nanu ”, te fekk dégguñu woon dara.
22۞ إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الصُّمُّ الْبُكْمُ الَّذِينَ لَا يَعْقِلُونَ
Li gën a yées ci bindeef yi ca Yàlla, mooy ñi tëx, luu te bañ a xel-lu.
23وَلَوْ عَلِمَ اللَّهُ فِيهِمْ خَيْرًا لَّأَسْمَعَهُمْ ۖ وَلَوْ أَسْمَعَهُمْ لَتَوَلَّوا وَّهُم مُّعْرِضُونَ
Ku leen woo woon ñu dëddu, nekk ñu beddiku.
24يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اسْتَجِيبُوا لِلَّهِ وَلِلرَّسُولِ إِذَا دَعَاكُمْ لِمَا يُحْيِيكُمْ ۖ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَحُولُ بَيْنَ الْمَرْءِ وَقَلْبِهِ وَأَنَّهُ إِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen wuyu Yàlla ak Yonentam ba, bu ñu leen woowee ci lu leen di musal, te nangeen xam ne Yàlla nag Dana dox nit ak xelam, te Danañu leen bëmëx jëme ca Moom.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Anfal 22

Simoore Al-Anfal Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li gën a yées ci bindeef yi ca Yàlla, mooy…

Simoore Aaya 22/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers