Al-Hijr · 68/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ ضَيْفِي فَلَا تَفْضَحُونِ ۝٦٨
Qaala inna haaa`ulaaa`i daifee falaa tafdahoon
📖 Tekkim Wolof
- Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen ma ci rusloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 66-70 — Simoore Al-Hijr

66وَقَضَيْنَا إِلَيْهِ ذَٰلِكَ الْأَمْرَ أَنَّ دَابِرَ هَٰؤُلَاءِ مَقْطُوعٌ مُّصْبِحِينَ
Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag nitam ña ci njël.
67وَجَاءَ أَهْلُ الْمَدِينَةِ يَسْتَبْشِرُونَ
Waa dëkk ba agsi ànd ak mbégte.
68قَالَ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ ضَيْفِي فَلَا تَفْضَحُونِ
- Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen ma ci rusloo.
69وَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ
Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.
70قَالُوا أَوَلَمْ نَنْهَكَ عَنِ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit ñi [ci sa diine ji] ? ”
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
68Aaya

Tekki — Al-Hijr 68

Simoore Al-Hijr Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen…

Simoore Aaya 68/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers