Al-Hijr · 69/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ ۝٦٩
Wattaqul laaha wa laa tukhzoon
📖 Tekkim Wolof
Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 67-71 — Simoore Al-Hijr

67وَجَاءَ أَهْلُ الْمَدِينَةِ يَسْتَبْشِرُونَ
Waa dëkk ba agsi ànd ak mbégte.
68قَالَ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ ضَيْفِي فَلَا تَفْضَحُونِ
- Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen ma ci rusloo.
69وَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ
Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.
70قَالُوا أَوَلَمْ نَنْهَكَ عَنِ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit ñi [ci sa diine ji] ? ”
71قَالَ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Mu ne leen : “Samay doom yu jigéen a ngii ndegam bëgg ngeen a def [li ngeen nar] ! ”
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-Hijr 69

Simoore Al-Hijr Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.

Simoore Aaya 69/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers