An-Nahl · 39/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
لِيُبَيِّنَ لَهُمُ الَّذِي يَخْتَلِفُونَ فِيهِ وَلِيَعْلَمَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّهُمْ كَانُوا كَاذِبِينَ ۝٣٩
Liyubaiyina lahumul lazee yakhtalifoona feehi wa liya`lamal lazeena kafarooo annahum kaanoo kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
Ngir mu leeralal leen [lay dëgg] ca la ñu daan wuute, ak it ña weddi xam ne dañu daan fen.
🎧 Dégg

📜 Aaya 37-41 — An-Nahl

37إِن تَحْرِصْ عَلَىٰ هُدَاهُمْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي مَن يُضِلُّ ۖ وَمَا لَهُم مِّن نَّاصِرِينَ
Loo xér xér ci jubal leen...Yàlla moom du gindi ku Mu bàyyi cig réer. Te duñu am ñu leen dimbali.
38وَأَقْسَمُوا بِاللَّهِ جَهْدَ أَيْمَانِهِمْ ۙ لَا يَبْعَثُ اللَّهُ مَن يَمُوتُ ۚ بَلَىٰ وَعْدًا عَلَيْهِ حَقًّا وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَعْلَمُونَ
Ñangay giñ ba fa seeni ngiñ yem naan : “Yàlla du dekkal ku dee”. Axakañ ! Loolu dig bu dëggu la ci Moom [Yàlla], waaye li ëpp ci nit ñi xamuñu.
39لِيُبَيِّنَ لَهُمُ الَّذِي يَخْتَلِفُونَ فِيهِ وَلِيَعْلَمَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّهُمْ كَانُوا كَاذِبِينَ
Ngir mu leeralal leen [lay dëgg] ca la ñu daan wuute, ak it ña weddi xam ne dañu daan fen.
40إِنَّمَا قَوْلُنَا لِشَيْءٍ إِذَا أَرَدْنَاهُ أَن نَّقُولَ لَهُ كُن فَيَكُونُ
[Li am mooy], Sunu kàddu ci mbir, bu Nu ko bëggee, Danu ko naan : “Nekkal”. Mu daldi nekk.
41وَالَّذِينَ هَاجَرُوا فِي اللَّهِ مِن بَعْدِ مَا ظُلِمُوا لَنُبَوِّئَنَّهُمْ فِي الدُّنْيَا حَسَنَةً ۖ وَلَأَجْرُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Ña gàddaay jëm ci Yàlla, ginnaaw ba ñu leen tooñee, Dananu leen wàcceel aw yiw ci àddina. Te peyug àllaaxira moo gën a màgg, cëy bu ñu xamoon !
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — An-Nahl 39

Simoore An-Nahl Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngir mu leeralal leen [lay dëgg] ca la ñu daan…

Simoore Aaya 39/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers