Al-Isra · 50/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
۞ قُلْ كُونُوا حِجَارَةً أَوْ حَدِيدًا ٥٠
Transliteration
Qul koonoo jijaaratan aw hadeedaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Nekkleen i xeer walla weñ
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 48-52 — Al-Isra
48انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu te dootuñu mën a am yoonu dellusi (ci ag njub).
49وَقَالُوا أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا وَرُفَاتًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ خَلْقًا جَدِيدًا
Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax yu funux, dananu dekki nekkaat ay mbindeef yu bees? ”
50۞ قُلْ كُونُوا حِجَارَةً أَوْ حَدِيدًا
Neel : “Nekkleen i xeer walla weñ
51أَوْ خَلْقًا مِّمَّا يَكْبُرُ فِي صُدُورِكُمْ ۚ فَسَيَقُولُونَ مَن يُعِيدُنَا ۖ قُلِ الَّذِي فَطَرَكُمْ أَوَّلَ مَرَّةٍ ۚ فَسَيُنْغِضُونَ إِلَيْكَ رُءُوسَهُمْ وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هُوَ ۖ قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ قَرِيبًا
walla yeneeni mbindeef yu reyci seeni xel. [Ngeen dégg] ñu naan : “Ku nuy dundalaat ? ” - Neel : “Ka leen bindoon bu njëkk ba”. Danañu yëngal seen bopp jëme ci yaw [ngir weddi la], ñuy wax naan : “Kañ lay doon ? ” Neeleen : “Xéy-na nekk na lu jegeñ.
52يَوْمَ يَدْعُوكُمْ فَتَسْتَجِيبُونَ بِحَمْدِهِ وَتَظُنُّونَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا
Bis bu leen [seen Boroom] woowee, [ngeen dikk], ngeen tontu Ko, di tuddu cant [gi Mu yeyoo]. Te ngeen defe ne tooguleen ci [bàmmeel] lu dul diir bu néew ! ”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
50Aaya
Tekki — Al-Isra 50
Simoore Al-Isra Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Nekkleen i xeer walla weñSimoore Aaya 50/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








