Maryam · 86/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَنَسُوقُ الْمُجْرِمِينَ إِلَىٰ جَهَنَّمَ وِرْدًا ۝٨٦
Wa nasooqul mujrimeena ilaa Jahannama wirdaa
📖 Tekkim Wolof
Nu sëkkëtal tooñkat ya jëme leen Safara ñuy sërëx-sërëxi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Maryam

84فَلَا تَعْجَلْ عَلَيْهِمْ ۖ إِنَّمَا نَعُدُّ لَهُمْ عَدًّا
Bul yàkkamti seen mbir : dafa am rekk lu ñu leen di nége.
85يَوْمَ نَحْشُرُ الْمُتَّقِينَ إِلَى الرَّحْمَٰنِ وَفْدًا
Bis ba ñuy pang ña ragal ña Yàlla jëme leen ca Yërëmaakoon ba ñu di ay mbooloo,
86وَنَسُوقُ الْمُجْرِمِينَ إِلَىٰ جَهَنَّمَ وِرْدًا
Nu sëkkëtal tooñkat ya jëme leen Safara ñuy sërëx-sërëxi,
87لَّا يَمْلِكُونَ الشَّفَاعَةَ إِلَّا مَنِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
[Bis booba] kenn du mën a ramm ku dul ku ko Yàlla digal.
88وَقَالُوا اتَّخَذَ الرَّحْمَٰنُ وَلَدًا
Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na doom ! ”
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Maryam 86

Simoore Maryam Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu sëkkëtal tooñkat ya jëme leen Safara ñuy sërëx-sërëxi,

Simoore Aaya 86/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers