Aali Imran · 94/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
فَمَنِ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ ۝٩٤
Famanif taraa `alal laahilkaziba mim ba`di zaalika fa ulaaa`ika humuz zaalimoon
📖 Tekkim Wolof
Ku duural Yàlla ay fen, ginnaaw loolu... ñooñaa di tooñkat ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Simoore Aali Imran

92لَن تَنَالُوا الْبِرَّ حَتَّىٰ تُنفِقُوا مِمَّا تُحِبُّونَ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِن شَيْءٍ فَإِنَّ اللَّهَ بِهِ عَلِيمٌ
Dungeen am mbaax ba ba ngeen di joxe ci li ngeen bëgg. Te lépp lu ngeen mën a joxe, Yàlla xam na ko.
93۞ كُلُّ الطَّعَامِ كَانَ حِلًّا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ إِلَّا مَا حَرَّمَ إِسْرَائِيلُ عَلَىٰ نَفْسِهِ مِن قَبْلِ أَن تُنَزَّلَ التَّوْرَاةُ ۗ قُلْ فَأْتُوا بِالتَّوْرَاةِ فَاتْلُوهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñam yépp a daganoon ca waa Banii-Israayiil, lu dul ñam ya [Israayiil ] araama loon ca boppam lu jiitu ñu doon wàcce Tawreet. Neel: “Indileen Tawreet te jàng ko, ndegam ñu dëggu ngeen ! ”
94فَمَنِ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Ku duural Yàlla ay fen, ginnaaw loolu... ñooñaa di tooñkat ya.
95قُلْ صَدَقَ اللَّهُ ۗ فَاتَّبِعُوا مِلَّةَ إِبْرَاهِيمَ حَنِيفًا وَمَا كَانَ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Neel : “Yàllaa wax dëgg. Kon toppleen diiney Ibraahiima. Ku wéetaloon Yàlla la te mësul a bokk ca ñay bokkaale Yàlla”.
96إِنَّ أَوَّلَ بَيْتٍ وُضِعَ لِلنَّاسِ لَلَّذِي بِبَكَّةَ مُبَارَكًا وَهُدًى لِّلْعَالَمِينَ
Néeg ba ñu njëkk sampal nit ñi moo di ba nekk Màkka, muy bu ñu barkeel, di njub, mbindéef yépp bokk ko.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
94Aaya

Tekki — Aali Imran 94

Simoore Aali Imran Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku duural Yàlla ay fen, ginnaaw loolu... ñooñaa di tooñkat…

Simoore Aaya 94/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers