Fatir · 19/45
Tekki Waxtaan — Simoore Fatir
وَمَا يَسْتَوِي الْأَعْمَىٰ وَالْبَصِيرُ ۝١٩
Wa maa tastawil a`maa wal baseer
📖 Tekkim Wolof
Gumba ak njàccaar niróowuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Fatir

17وَمَا ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ بِعَزِيزٍ
Te loolu du lu jafe ci Yàlla.
18وَلَا تَزِرُ وَازِرَةٌ وِزْرَ أُخْرَىٰ ۚ وَإِن تَدْعُ مُثْقَلَةٌ إِلَىٰ حِمْلِهَا لَا يُحْمَلْ مِنْهُ شَيْءٌ وَلَوْ كَانَ ذَا قُرْبَىٰ ۗ إِنَّمَا تُنذِرُ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ ۚ وَمَن تَزَكَّىٰ فَإِنَّمَا يَتَزَكَّىٰ لِنَفْسِهِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ الْمَصِيرُ
Kenn du yenu bàkkaarub keneen. Te képp ku diis gann ak bàkkaar, bumu cay woote ndimbal, kenn du ko yenul dara, doonte la sax dafa di mbokkug jegeñaale. Da di rekk ne nangay xupp ña di ña ragal seen Boroom ci kumpa tey taxawal julli. Te képp ku cay sellal, na xam ne boppam la koy defal, te ca Yàlla la lépp di mujj.
19وَمَا يَسْتَوِي الْأَعْمَىٰ وَالْبَصِيرُ
Gumba ak njàccaar niróowuñu.
20وَلَا الظُّلُمَاتُ وَلَا النُّورُ
du caagene lëndëm ak leer.
21وَلَا الظِّلُّ وَلَا الْحَرُورُ
du caagene ker ak naaj.
FatirFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Fatir 19

Simoore Fatir Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gumba ak njàccaar niróowuñu.

Simoore Aaya 19/45 — Simoore Fatir فاطر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fatir Dégg, Simoore Fatir Tekki, Simoore Fatir mp3, Simoore Fatir pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers