As-Saffat · 160/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ ۝١٦٠
Illaa `ibaadal laahil mukhlaseen
📖 Tekkim Wolof
Ba mu des jaami Yàlla yiy sellal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 158-162 — As-Saffat

158وَجَعَلُوا بَيْنَهُ وَبَيْنَ الْجِنَّةِ نَسَبًا ۚ وَلَقَدْ عَلِمَتِ الْجِنَّةُ إِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ
Ñu di ko askanale ci jinne yi, ndax jinne yi xam nañu ne danañu teew ci kanamu [Yàlla].
159سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tudd naa sellug Yàlla ga. Kawe na lool la ñu koy melal !
160إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ba mu des jaami Yàlla yiy sellal.
161فَإِنَّكُمْ وَمَا تَعْبُدُونَ
Yéen ak li ngeen di jaamu,
162مَا أَنتُمْ عَلَيْهِ بِفَاتِنِينَ
kenn duleen ci fitnaal,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
160Aaya

Tekki — As-Saffat 160

Simoore As-Saffat Aaya 160 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu des jaami Yàlla yiy sellal.

Simoore Aaya 160/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 158–162. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers