Al-An'am · 134/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
إِنَّ مَا تُوعَدُونَ لَآتٍ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ ١٣٤
Transliteration
Inna maa too`adoona la aatinw wa maaa antum bimu`jizeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Li ñu leen dig luy ñëw la. Te dungeen mën a raw.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 132-136 — Al-An'am
132وَلِكُلٍّ دَرَجَاتٌ مِّمَّا عَمِلُوا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا يَعْمَلُونَ
Ñoom ñépp danañu am pey gu méngook la ñu jëfoon. Sa Boroom ñàkkul paal ca la ñuy jëf.
133وَرَبُّكَ الْغَنِيُّ ذُو الرَّحْمَةِ ۚ إِن يَشَأْ يُذْهِبْكُمْ وَيَسْتَخْلِفْ مِن بَعْدِكُم مَّا يَشَاءُ كَمَا أَنشَأَكُم مِّن ذُرِّيَّةِ قَوْمٍ آخَرِينَ
Sa Boroom Ku woomal la, boroom yërmaande la. Bu ko neexoon, mu jële leen fi, wuutale ci seen ginnaaw la Ko soob, ni Mu leen sose woon ngeen di ay sëti ñeneen.
134إِنَّ مَا تُوعَدُونَ لَآتٍ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ
Li ñu leen dig luy ñëw la. Te dungeen mën a raw.
135قُلْ يَا قَوْمِ اعْمَلُوا عَلَىٰ مَكَانَتِكُمْ إِنِّي عَامِلٌ ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن تَكُونُ لَهُ عَاقِبَةُ الدَّارِ ۗ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الظَّالِمُونَ
Neel : "Yéen samaw nit ! Jëfleen ci seeni mbir ; man dey aji-jëf laa. Dangeen mas a xami kan moo moom kër gu mujj ga.”. Ak lu mën a xew, tooñkat ya ñoom duñu texe.
136وَجَعَلُوا لِلَّهِ مِمَّا ذَرَأَ مِنَ الْحَرْثِ وَالْأَنْعَامِ نَصِيبًا فَقَالُوا هَٰذَا لِلَّهِ بِزَعْمِهِمْ وَهَٰذَا لِشُرَكَائِنَا ۖ فَمَا كَانَ لِشُرَكَائِهِمْ فَلَا يَصِلُ إِلَى اللَّهِ ۖ وَمَا كَانَ لِلَّهِ فَهُوَ يَصِلُ إِلَىٰ شُرَكَائِهِمْ ۗ سَاءَ مَا يَحْكُمُونَ
Dañuy sédd Yàlla li Mu bind ci mbey ak ci jur gi, ab cér daldi wax ne : “Lii mooy wàllu Yàlla - ci seeni njortu ! - lii mooy wàllu li nu koy bokkaale.”. Te la ñu sédd ñii, du agsi ca Yàlla, waaye la ñu sédd Yàlla, dana agsi ca ñañu koy bokkaaleel. Na ñuy àttee ñaaw na !
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
134Aaya
Tekki — Al-An'am 134
Simoore Al-An'am Aaya 134 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li ñu leen dig luy ñëw la. Te dungeen mën…Simoore Aaya 134/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 132–136. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








