Al-A'raf · 125/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالُوا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ ۝١٢٥
Qaaloo innaaa ilaa Rabbinaa munqaliboon
📖 Tekkim Wolof
Ñu toontu ne : “Nun ci sunu Boroom lanuy dellu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 123-127 — Simoore Al-A'raf

123قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...
124لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ ثُمَّ لَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba noppi ma daaj leen, sandamtal leen yéen ñépp.”
125قَالُوا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ
Ñu toontu ne : “Nun ci sunu Boroom lanuy dellu.
126وَمَا تَنقِمُ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِآيَاتِ رَبِّنَا لَمَّا جَاءَتْنَا ۚ رَبَّنَا أَفْرِغْ عَلَيْنَا صَبْرًا وَتَوَفَّنَا مُسْلِمِينَ
Feyoowoo ci nun lu dul nu gëm ay kéemaani sunu Boroom, ba ñu agsee ci nun. Sunu Boroom ! Sottil ci nun muñ te nga rey nu fekk nu dee jullit.”
127وَقَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ أَتَذَرُ مُوسَىٰ وَقَوْمَهُ لِيُفْسِدُوا فِي الْأَرْضِ وَيَذَرَكَ وَآلِهَتَكَ ۚ قَالَ سَنُقَتِّلُ أَبْنَاءَهُمْ وَنَسْتَحْيِي نِسَاءَهُمْ وَإِنَّا فَوْقَهُمْ قَاهِرُونَ
Kilifa ya bokk ci nitu Firawna ne ko : “Moo ndax dangaa bàyyi Muusaa ak u nitam ñuy yàq ci suuf si, te moom mu bàyyi la, bàyyi sa yàlla ? ”. Mu toontu ne : “Danaa rey seeni doom yu góor, ba yu jigéen yi. Ndax nun noo leen tiim, noo leen not.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
125Aaya

Tekki — Al-A'raf 125

Simoore Al-A'raf Aaya 125 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu toontu ne : “Nun ci sunu Boroom lanuy dellu.

Simoore Aaya 125/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 123–127. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers