Al-A'raf · 7/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
فَلَنَقُصَّنَّ عَلَيْهِم بِعِلْمٍ ۖ وَمَا كُنَّا غَائِبِينَ ۝٧
Falanaqussanna `alaihim bi`ilminw wa maa kunnaa ghaaa`ibeen
📖 Tekkim Wolof
Te Dananu leen nettali ji [ci loolu] ci xam-xam bu wér ndaxte fekke woon Nanu lépp !
🎧 Dégg

📜 Aaya 5-9 — Al-A'raf

5فَمَا كَانَ دَعْوَاهُمْ إِذْ جَاءَهُم بَأْسُنَا إِلَّا أَن قَالُوا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te seeni njàmbat nekkul, ba leen mbugal ma saddee, lu dul : “Nun ay tooñkat lanu woon”.
6فَلَنَسْأَلَنَّ الَّذِينَ أُرْسِلَ إِلَيْهِمْ وَلَنَسْأَلَنَّ الْمُرْسَلِينَ
Fàwwu Dananu laaj ña Nu yónni ca ñoom [nit ña], fàwwu it Dananu laaj ña Nu yónni woon [Yonent ya].
7فَلَنَقُصَّنَّ عَلَيْهِم بِعِلْمٍ ۖ وَمَا كُنَّا غَائِبِينَ
Te Dananu leen nettali ji [ci loolu] ci xam-xam bu wér ndaxte fekke woon Nanu lépp !
8وَالْوَزْنُ يَوْمَئِذٍ الْحَقُّ ۚ فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Booba bis, peese bu dëggu lay doon. Ña seen peese diis ak u yiw... Ñoom ñooy ñu texe ña !
9وَمَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُم بِمَا كَانُوا بِآيَاتِنَا يَظْلِمُونَ
Ña seen peese woyof nag ... Ñooy ña yàqal seen bopp ngir ñàkk a faale Sunuy kàddu te doonoon ñu daan tooñ.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-A'raf 7

Simoore Al-A'raf Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Dananu leen nettali ji [ci loolu] ci xam-xam bu…

Simoore Aaya 7/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers